Job 7:17
TSK
Luy nit ba nga di ko gëddaal, bay def sam xel ci moom,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Luy nit ba nga di ko gëddaal, bay def sam xel ci moom,
astamaak nit kii tanewulu sax, doom aadama jii gënul gasax.
Aji Sax ji, luy nit, ba nga di ko ràññee? luy doom aadama, ba nga di ko faale?
Xeetoo xeet du tus fi kanamam, te jàppewu leen lu moy neenug neen.
«Cant ñeel na Boroom bi Yàllay Israyil, moo seetsi ñoñam, ba jot leen!
Tiitaange nag jàpp ñépp, ñu sàbbaal Yàlla, naan: «Yonent bu mag feeñ na ci sunu biir!» te naan «Yàllaa wallusi ñoñam!»
Noonu it la waxe feneen, ne: «Yaa dib sarxalkat ba fàww, topp dayob Melkisedeg.»