TSK

TSK · Isaiah 1:30

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Aji Sax ji di leen jiite fu ngeen tollu, di leen màndale joor gu maral, dëgëral seeni cér, ngeen mel ni tool bu ñu suuxat, mel ni bëtu ndox bu dul ŋiis,

Aji Sax ji dafa wax ne: «Alkànde ñeel na ku yaakaar doom aadama ak képp kuy doolewoo nit, dëddu Aji Sax ji.

«Neel, Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Mbaa jooju reseñ dina baaxle? Mbaa jeneen jaxaay ja du buddiy reenam, buur doom ya, ba lu mu jebbile woon lax, ba buddi reen ya du laaj përëg bu réy, mbaa nit ñu bare?

Bëti ndox suuxat ko, ndoxi xoote yi màggal ko, wal ma dajaloo ca reen ya, doxe fa yónnee garabi àll bi yépp ay waltan.