TSK

TSK · Isaiah 28:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Maas giy ñëw, seen doom yi leen di wuutuji yeen, ñook doxandéem yi jóge fu sore, bu ñu gisee mbugal yi ci réew mii, ak wopp yi fi Aji Sax ji woppale,

Daawuda dem ba ca Baal Perasim, duma leen foofa. Mu ne: «Aji Sax jee ma bëttal noon yi, ni walum ndox di bëtte, wéy.» Moo tax ñu wooye bérab boobu Baal Perasim (mu firi Boroom bëtt-bëtt yi).

Boroom bi nee: «Bu ma sottalee liggéey fa kaw tundu Siyoŋ ak fa Yerusalem, maay mbugale buurub Asiri réy-réyloom gi, ak gëti xeebaateem.»

Moo tax maa ngii di dellu wéyeek askan wii, ay kéemtaan aki kiraama yuy tiiñ boroom xel ak xelam, réer xamkat ak xam-xamam.»

Ba ngay def kiraama ya ñu séentuwuloon, yaa wàcc, tund yi yëngu fi sa kanam.

Mboolem ñi fi jaareey tacc-taccali loxo, ciipu, wëcc bopp ci gentub Yerusalem mu taaru ma, te naan: «Xanaa du biib dëkk lañu doon tudd sottiteb taar ba, te muy mbégtem àddina sépp?»

¶ Ca fukkeelu atu ngàllo ak ñaar, keroog juróomi fan ca fukkeelu weer wa, jenn waay a rëcce ca jéllub Yerusalem ba, dikk ne ma: «Dëkk ba daanu na!»

¶ Ba Yeesu jubsee ba séen dëkk ba, jooy na ndax moom.