TSK

TSK · Isaiah 46:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

nemmikuy tataam, doxantoo këri buur, ba man koo yegge maasug ëllëg,

Éy Yàlla, bu ma bijjaawee ba weex tàll it, bu ma wacc, ba keroog may xamal maasu tey sa doole, xamal ñi ciy topp ñépp sag njàmbaar.

Bu yàgg nga samp suuf, sàkke asamaan say yoxo.

maa masa doon kenn ki, te sama loxo, maneesu cee musle. Su ma defee, kuy dindi?

«Pase laa bañ,» Aji Sax ji, Yàllay Israyil moo ko wax, «ak ku làmboo jëfi loraange ni mbubb.» Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko wax. Kon nag sàmmleen seenum xel, te buleen wor.

Ndax Yàlla kat, ay mayam akub wooteem, lenn du ci toxu.

Yeesu Almasi menn mi la woon démb ak tey ba fàww.