TSK

TSK · Isaiah 6:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Gannaaw gi ña nekkoon ca dëkk ba ba booba, ak ña jébbaloon seen bopp buuru Babilon ak la desoon ca waa réew ma, Nebusaradan njiital dagi buur, boole leen yóbbu ngàllo.

Aji Sax ji, yaa yokk xeet wi, yaw mii yaa yokk xeet wi, yaa fésal sa teddnga, yaa yokk mboolem kemi réew mi!

«Dëddu naa sama kër, maa wacc sama séddoo, wacce sama soppey xol loxol noonam.

¶ Lii mooy limu nit ñi Nabukodonosor toxal: Ñetti junniy Yudeen ak ñaar fukk ak ñett (3 023), loolu yemook juróom ñaareelu atu nguuram,

¶ Ma ne kon, xanaa Yàlla daa wacc ñoñam? Mukk kay! Man ci sama bopp ci Israyil laa bokk, askanoo ci Ibraayma, giiroo ci Beñamin.