TSK

TSK · Jeremiah 13:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Job 40:10 TSK

Ràngool boog màggaay ak teddnga, te làmboo dayook daraja.

Ayca ca xunti ma, làqujileen biiri pax, ba sore tiitaange ji Aji Sax ji sabab, sore darajay màggaayam.

Noo dégg ni Mowab réye, réya réy, reew te bew, seeni kañu di waxi neen.

Dégluleen te teewlu, buleen fétteeral. Aji Sax ji kat wax na!

Ma nàndal waa Yerusalem ak dëkki Yuda ak seeni buur ak seeni kàngam ngir gental fépp, muy ndànd-foyfoy bu ñuy muslu, di ko móoloo ba sunu jonni yàllay tey.

Xanaa du ba nga bewee yaa saxaloon ci saw làmmiñ kàddug baatal Sodom?

«Su bés baa gàcce dootul am ci sa mboolem jëf, ji nga ma moye, nde maay jële fi sa biir ñiy bége sab sag, te doo damooti ci sama kaw tund wu sell.

James 4:6 TSK

Waaye yiw wu gënatee baawaan la maye. Moom la Mbind mi ne: «Yàlla, ñi réy lay xeex, ñi toroxlu, mu may leen aw yiw.»