All books in KYG

Jeremiah 21

KYG · verse 4

52 chapters

KYG / Jeremiah / Chapter 21

KYG · verse 4

A ji Sax ji, Yàllay Israyil dafa wax ne: Seen dooley xare ji ngeen yor, di xeexeek ñi ci biti, di buuru Babilon ak waa Babilon ñi leen gaw, maa ngii di ko walbati, dajale ko ci biir dëkk bii.