TSK

TSK · Job 21:31

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Natan ne Daawuda: «Yaw, yaay waa ji! Aji Sax ji Yàllay Israyil dafa wax ne: “Man maa la fal buurub Israyil, maa la xettli ci Sóol.

Job 21:19 TSK

Ãa ku bon daal ay tooñ, Yàlla dencal doomam añ ba? Ki tooñ kay, na ko fey, mu xam,

Lii yeena ko def! Damay noppi, ngeen defe ne damaa mel ni yeen? Dama leen di sikk, tuumaal leen, ngeen gis!

Yeen aka mokkal gànctu! Jeeg ju bon ji sax di jànge ci yeen.

Naka la Póol wax ci mbirum njub, ak moom sa bakkan, ak àtteb bés-pénc, Feligsë daldi tiit, ne ko: «Léegi, man ngaa demagum, bu ma ko talee, dinaa la wooluwaat.»

¶ Waaye ba Sefas dikkee Àncos, jàkk laa ko def, weddi ko, ndax moo nekkul woon ci dëgg.