TSK

TSK · Job 21:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ba Musaa waxee loolu bànni Israyil, dégluwuñu ko sax ndax xol bu jeex ak njaam gu metti.

Mu am bés buurub Israyil jaar ca kaw tata ja, senn as ndaw àddu ca kaw ne ko: «Buur, sang bi, ngalla wallu ma!»

Job 7:11 TSK

Moo tax duma téye sama làmmiñ, xanaa di waxe biir njàqare, di jooye biir naqar.

Job 10:2 TSK

Dama naa Yàlla: Bu ma topp ug tooñ. Xamal ma kay li nga may topp, lu mu!

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, di kàddug Sabóor, ñeel Daawuda, dëppook galan bi ñu dippee Kéwélu fajar.

Bëccëg, ma jàq, sàkku Boroom bi; guddi, ma tàllal loxo, toqiwuma. Sama xol tëë sedd.

Ma àddu, ñaan Aji Sax ji; àddu ca kaw, di tinu Aji Sax ji,