TSK

TSK · Lamentations 5:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ba mu ko defee mu ne: «Yal na Kanaan torox, bay jaamu jaami doomi ndeyam.»

¶ Ba loolu amee Sanbalat ma dëkk Oron dégg ko, mook Amoneen ba Tobya, jawriñ ba, ak Gesem, Araab ba. Ñu di nu ñaawal ak a diiju naan: «Li ngeen di def nii lu mu doon? Dangeen di fexeel Buur?»

Job 5:4 TSK

Ay doomam ay sore yoonu mucc, ñu di leen dëggaate ca pénc ma, te kenn du leen xettli.

Éy Aji Sax ji, sama Yàlla, yaw laay làqoo! Musal ma, xettli maak ñi may dàq ñépp.

Moom xamul woon ne man maa ko doon jox pepp meek biiñ bu bees beek diw gi, di ko yéwéne xaalis ak wurus, ñu di ko jaamoo Baal.