Leviticus 25:13
TSK
¶ «Atum Yiwiku moomu ci ngeen di delloo ku nekk suufam.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Atum Yiwiku moomu ci ngeen di delloo ku nekk suufam.
Bu atum Yiwiku dikkee, tool bi day dellu ca ka ñu ko jënde woon te mu di alalu ndonoom.
Ndax Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Dees na dellu di jënd ay kër aki tool ak tóokëri reseñ ci réew mii.”»
¶ Bokk yi nag, buggunu ngeen réere mbirum way dawlu ñi, bay tiislu ni ñeneen ñi amul jenn yaakaar, di tiisloo.