All books in KYG

Luke 21

KYG · verse 12

24 chapters

KYG / Luke / Chapter 21

KYG · verse 12

W aaye laata loolu lépp, yeen, dees na leen teg loxo, fitnaal leen, jébbal leen kuréli jàngu ya, tëj leen kaso. Dees na leen yóbbu ci kanami buur aki boroom dëkk ndax sama tur,