Maa ngii, mana waññ sama yax yépp, ñoom ñuy xoole, di ma seetaan,
TSK
TSK · Luke 23:34
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Moo tax ma di ko jox ab cér ci biir ñu bare, mu séddoo ak ay kàngam alalu xareem, ngir moo jébbale bakkanu boppam, ñu limaale kooki tooñkat, moo gàddu bàkkaaru ñu bare te mooy tinul moykat yi.
¶ «Jawriñ jooju xam nammeelu njaatigeem, te taxul mu waaj ko, ba jëfewu ko, ay yetam dina bare.
Mu ne gurub, samp bëti óomam, daldi àddu ca kaw, ne: «Sang bi, bu leen topp bii bàkkaar.» Naka la wax loolu, daldi nelaw.
¶ Ñi leen di bundxatal, ñaanal-leen leen, ñaanal-leen leen te bañ leena móolu.
Danuy ñaq, di dunde sunu liggéeyu loxo, nit ñi di nu saaga, nu di leen ñaanal, ñu di nu bundxatal, nuy muñ.
Muñ ay dóor yu la fekk tooñ, ana lu ciy ndam? Waaye soo muñee coono boo daj ngir lu baax loo def, loolu de aw yiw la fa kanam Yàlla.