TSK

TSK · Luke 5:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Fa joor ga feggook dexu Yurdan it di kemu, diggante dexu Kineret ca bëj-gànnaar, ak ca bëj-saalumu géeju Xorom ga, ba ba ngay àgg ca suufu tundu Pisga, ca penku.

Luke 12:1 TSK

¶ Mbooloo ma nag mujj na dajaloo ba mat ay junniy junniy nit, bay joggeente. Ci biir loolu Yeesu tàmbalee wax, jëkke ko ci ay taalibeem, ne: «Wattuleen lawiiru Farisen ñi, te mooy jinigal.