TSK

TSK · Luke 5:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ci kaw loolu Aji Sax ji romb fa kanam Musaa, di biral naan: «Aji Sax jee, Aji Sax ji, Yàlla jiy yërëm, di yéwéne, mer ma diib, ngor gaak kóllëre ga bare.

te teg ñaari nit ñu tekkiwul dara, ñu janook moom. Na ñooñu duural Nabot ne ko: “Saaga nga Yàlla, saaga Buur.” Su ko defee ngeen génne ko dëkk ba, dóor ko ay doj ba mu dee.»

Yal na leen malaakam Aji Sax ji bëmëx, nim ñax mu ngelaw wal.

Mennum man mii maay far say moy ngir man, ba dootuma fàttliku bàkkaar.

Boroom bi sunu Yàlla, yaay Boroom yërmandeek njéggal moos, ndax gàntal nanu la.

Moo nuy yërëmati; sunuy ñaawtéef lay joggiy tànkam, te biir xóotey géej lay tàbbal sunuy bàkkaar.

Luke 5:17 TSK

¶ Yeesu moo doon jàngle bés, fu ay Farisen ak ay jànglekati yoonu Musaa tooge, jóge ca mboolem dëkki Galile ak Yude ak Yerusalem, te manoorey Boroom bi teew faak moom, ngir faj jarag ja.

Ñi Yàlla taamu, ana ku leen di tuumaal? Yàlla de mooy jox nit àtteb ku jub.