1 Samuel 21:3
TSK
Daawuda ne Ayimeleg sarxalkat ba: «Buur a ma sant ne ma: “Bu kenn xam lenn ci li ma la yónni, ak li ma la sant.” Samay ndaw nag, xamal naa leen ne bérab sàngam lañu wara xaar.