TSK

TSK · Luke 6:37

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Kiy lekk, bumu ko xeebe ki lekkul; ki lekkul it, bumu sikk kiy lekk, ndax Yàllaa ko xajoo.

Man nag, su dee yeena dogal samab àtte, mbaa kurélu nit a dogal samab àtte, soxaluma lool, te dogalaluma sama bopp ab àtte it,

Baaxleen ci seen diggante, di ñeewantante, tey balante, ni leen Yàlla baale ci Almasi.

¶ Bokk yi, buleen ŋàññante. Ku ŋàññ sa mbokk mbaa nga sikkal sa mbokk, yoon wi nga ŋàññ, yoon wi nga sikkal. Ku sikkal yoon wi nag doo sàmmkatub yoon wi, sikkalkatub yoon wi nga.