TSK

TSK · Numbers 10:35

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

bu ma daasee sama saamar buy melax, ba ŋàbb ko ci saab loxo, di àtte, maay fey samay digaale, añale samay bañ.

Éy Aji Sax ji sama Yàlla, jógal, wallu ma! Yaa toj kaabaabi noon yu bon yépp, foq seeni sell.

Yàllaay jóg, noonam ya tasaaroo; bañam ña daw, dëddu ko.

Aji Sax ji, jógal agsi sa dal-lukaay, yaak sa gaal gi jëmmal sa doole.

Aji Sax ji, yewwul, ngalla yewwul; wone sa doole. Yewwul na bu jëkkoon, bu yàgga yàgg. Xanaa du yaa falaxe Raxab? Du yaa jam ninki-nànka jooja?