Genesis 48:14
TSK
Israyil nag jàllawle ay loxoom, tàllal ndijooram, teg ko ca kaw boppu Efrayim, mi gën di ndaw; càmmoñam tege ca boppu Manase, doonte mooy taaw.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Israyil nag jàllawle ay loxoom, tàllal ndijooram, teg ko ca kaw boppu Efrayim, mi gën di ndaw; càmmoñam tege ca boppu Manase, doonte mooy taaw.
¶ Ba loolu wéyee kilifay njaboot yi askanoo ci Yuusufa, te bokk ci làngu Galàdd doomu Makir mi sëtoo ci Manase, ñoo dikk. Ñu wax fa kanam Musaa, ak kilifay njabooti bànni Israyil.