TSK

TSK · Numbers 6:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ «Kemu fani céddoo yi mu xas ne dina ko nasireenal, saatus watukaay du laal boppam ba keroog fani nasireenal, yi mu séddoo Aji Sax ji matee. Ku sell lay doon te day jañu.

Yeen itam noonu. Bu ngeen defee li ñu leen sant lépp ba noppi, dangeena war ne: “Ay jaam rekk lanu. Sunu warugar lanu def.”»

Ñoom ngay àndal, nga bokk ak ñoom setlu, te nga gàddu seen peyu wateefu bopp, wi boroom xas wu ni mel aadawoo. Su ko defee ñépp ay xam ne li ñu lay jëwe, dara amu ci, te yoonu Musaa ngay jëfe, di ko sàmm.

Moo tax cant ñeel ko, ndax yiwam wu màgg wi mu nu baawaanal ci Soppeem bi.