TSK

TSK · Numbers 9:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Musaa nag def loola. Mboolem noonee ko ko Aji Sax ji sante, na la ko defe.

¶ Bànni Israyil daldi def noonu. Mboolem lu Aji Sax ji santoon Musaa, noonee lañu ko defe.

Fu niir wa masa bàyyikoo fa tiim xayma ba, bànni Israyil day fabu topp ko, te fépp fu niir wa masa dale, fa la bànni Israyil di fàkk ab dal.

¶ Sunu Yàlla Aji Sax ji da noo waxoon ca Oreb ne nu: «Seen toogaayub tund wii doy na.

Nga ne ma: «Dama laa xelal, xamal la fi ngay jaar, digal la, di la xool.

Danga maa gindee sam xel, teg ca dalale ma sa teddnga.

jaarale leen yoon wu jub, ngir ñu àgg cib dëkk.

Nanga wóoloo Aji Sax ji, sa léppi xol, te bul wéeru ci saw déggin.