TSK

TSK · Proverbs 1:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Daawuda ne Abigayil: «Cant ñeel na Aji Sax ji Yàllay Israyil, mi la yebal bésub tey jii, ngir nga dogale ma.

Job 34:2 TSK

Yeen ñi xelu, dégluleen samay wax, yeen ñi xam, teewluleen ma.

Job 34:16 TSK

Ndegam am ngag dégg, déggal lii, teewlul sama kàddu gii.

Li ma xelal ba ma raw noon yi, mooy sa santaane, yi ma jagoo fàww.

Bul yedd kuy ñaawle, da lay jéppi; yeddal ku rafet xel, mu naw la.

Ku bëgga xam, bëgg ku la yedd; ku bañ ku la àrtu, bàyyima nga.

Boo ñefee ab ñaawlekat, téxét ba jànge ca; nga yedd kuy dégg, mu xame ca.

Njort naa ne boroomi xel laay waxal. Kon àtteel-leen seen bopp li ma leen wax.