TSK

TSK · Proverbs 10:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ci kaw loolu Buur bàyyikoo ca tóokër ba, délsi ca ëttu bernde ja, fekk Aman di sukk ca lal ba Esteer tëdd. Buur ne: «Ãa! Ba ci yekktaan Lingeer nag, te ma nekk ci biir kër gi?»

aji jub ñi gis ko, bég; mboolem ku bon wedam.

Kàdduy ku jub bëtu ndox la, day naatal; waaye ku soxor, wax ja làq fitna.

ku ko ne: «Yaa tooñ,» yaay baaxle, taasoo barke bu yaa.

Neleen aji jub ji mooy baaxle, mooy yooloo añam.

Yal na Yàlla baaxe nag waa kër Onesifor, yërmandeem, ndax dëfal na ma lu bare, te kersawoowul li ñu ma tëj kaso,