TSK

TSK · Proverbs 11:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ci biir loolu Ayitofel gis ne déggeesul ndigalam, mu takk mbaamam, ñibbi ca dëkk ba mu fekk baax. Mu daldi topptoo mbiri këram ba mu jekk, ba noppi wékk boppam. Mu dee, ñu denc ko ca sëgi baayam.

Job 18:7 TSK

Bu daa waaxu démb, di temp tey, ay mébétam di ko mbas.

Ñii kat seen bopp lañuy fiir, seen bakkanu bopp lañu sànk.

Loo mébét, bàyyil Yàlla xel, mu xàllal la yoon.

Kuy jubal, jiital mat. Njublaŋ ak wor, detteelu.

Hosea 5:5 TSK

Israyil, ag reewandeem a ko tiiñal, Israyil ak Efrayim ñooy fakktaloo seenug ñaawtéef, Yuda it ànd ak ñoom fakktalu.