1 Kings 11:36
TSK
Doomam nag dinaa ko jox genn giir gi ci des, ngir askanu Daawuda, sama jaam ba, baña fey mukk sama kanam ci biir Yerusalem, dëkk bi ma tànnal sama bopp, dëël fa sama tur.