TSK

TSK · Proverbs 20:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Abner àddu ca kaw, ne Yowab: «Xanaa saamar day lekku suux ba fàww? Xamuloo ne lii aw naqar doŋŋ lay mujje? Ana looy xaarati ci ne mbooloo mi ñu noppee topp seeni bokk?»

Defe nga ne làmmiñ kese doy na pexeek njàmbaar cib xare? Ma ne: Ana kan nga yaakaar bay fippu ci sama kaw?

Tegtal tumurànke, am réew suux; digle bare, ndam dikk.

tegtal yu xelu lañuy xaree, diisoo bu yaatooy maye ndam.

Am ban buur mooy xarejeek beneen buur te jëkkula toog, seet ba xam ndax man naa ànd ak fukki junniy xarekatam, ngir xarejeek ku ko songseek ñaar fukki junniy xarekat?