TSK

TSK · Proverbs 20:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ku gaawa mer, def jëfi dof, te kuy fexeel nit, ñu bañ la.

Muñ mer, moo gën njàmbaar; tënk sa bakkan moo raw nangub dëkk.

Ab dof, làmmiñam sooke naw ay, ay waxam di sàkku yeti gannaaw.

Ku réy te bew, mooy ñaawle, day reew, ba jéggi dayo.

Kuy xuloo lu sa yoon newul, yaa jàpp ci noppi xaj buy romb.

Baaxleen ci seen diggante, di ñeewantante, tey balante, ni leen Yàlla baale ci Almasi.

James 4:1 TSK

¶ Ana fu jote yeek xuloo yi ci seen biir jóge fu moy seen bànneexi bakkan, yiy xare ci seen yaram?