TSK

TSK · Proverbs 20:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, ànd ak xalamu juróom ñetti buum, di kàddug Sabóor, ñeel Daawuda.

Kuy dige te doo joxe, yaay xiin wu ngelaw, mu naaxsaay.

Ma seeta seet, gisuma. Genn góor laa ràññee ci junniy góor, ràññeewuma kenn ci jigéen ñi ñépp.

Micah 7:1 TSK

Wóoy, ngalla man mi mel ni kuy forsi, te meññeef ma fatu, may raasaatu, te du cabbu reseñ ju nit lekk, du figg ju bees ji ma namm.

Farisen baa nga taxaw di yelu, naan: “Yàlla, maa ngi lay sante li ma melul ni ñeneen ñi doonul lu moy ay lekk-kati àq, ay njublaŋ aki jaalookat, rawatina juutikat bii.

Piyeer ne ko: «Sang bi, jekk naa ci ànd ak yaw kaso, ak ci ànd ak yaw dee.»

¶ Mujj naa dib dof nag, te yeena ma ko yóbbe, nde gërëm maa leen waroon, ndax doonte duma dara sax, ndaw yu màgga màgg yooyeey, duma seen cuune ci lenn.