TSK

TSK · Proverbs 21:24

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ba Aman gisee ne Mardose du ko sukkal, du ko sujjóotal, daa mer ba fees dell.

Ma nga naan: «Moo téxét bi, foo àppal sa téxét gi? Ñaawlekat bi, foo àppal sa ñaawle bi? Dof bi, ñaata yoon ngay bañ xam-xam?

Na ñaawlekat bi séentu mbugal; ab dof, yeti gannaaw.

Noo dégg ni Mowab réye, réya réy, reew te bew, seeni kañu di waxi neen.