Mu ne ko: «Ndax du Yowab a nas pexe mii mépp, yaak moom?» Mu ne ko: «Buur, sang bi, ak sa barke, li nga wax rekk la, du leneen moos! Yowab, sa jawriñ bee ma ko sant. Moo ma waxloo lii lépp, sang bi.
TSK
TSK · Proverbs 25:2
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
2 Samuel 14:19
TSK
1 Kings 3:16
TSK
¶ Ba loolu wéyee mu am ñaari gànc yu dikk ca Buur, agsi ca kanamam.
Ezra 4:19
TSK
Ndigal tukkee na ci man, ngir ñu seet te gis nañu ne dëkk boobu kay yàgg nañoo fexeel buur yi, loolu indi fa ay fippooki pexey bañ.
Job 11:7
TSK
Dangaa mana gëstu mbóoti Yàlla, ba gis ko? Am yaa ñédd Aji Man ji?
Job 38:4
TSK
Ana foo nekkoon ba may samp suuf? Waxal su la ko sam xel mayee.
Job 42:3
TSK
Nee nga ma: «Ana koo doon, bay lëntal samay dogal te xamoo?» Maa wax moos te xawma lenn ci kawtéef yu ma wees, ump ma.
Damaa dogu ne damay gëstu, teg ko ci xel mu rafet, di settantal mboolem lu nit def fu jant bi tiim. Ndaw sas wu tiis wu Yàlla sase, ñu war koo sasoo!