TSK

TSK · Proverbs 27:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Waaye sama surgaa yàq sama der ci yaw. Yaw nag Buur, sang bi, ndokk ba nga matee ba mel ni malaakam Yàlla. Kon sang bi, defal li la soob.

¶ Buur Robowam giseek mag ña daa taxawu Suleymaan baayam ba muy dund. Mu ne leen: «Lu ngeen may digal, ma wax ko mbooloo mii?»

Job 6:21 TSK

Yeen déy, yeenay yooyu wal ci man. Yeena gis sama njàqare, jàq.

Barey àndandoo lor a ngi ci, waaye xarit a ngi gëna taq nit mbokkam.

Waaye yaw Israyil, sama jaam bi; yaw Yanqóoba mi ma taamu, yaw askanu Ibraayma, samab xarit!

Waruleen woona seetaan ci seen bésub mbokk, bésub njekkaram, Waruleen woona bége deminu Yudeen ñi ci seen bésub sànkute, mbaa ngeen di réy làmmiñ, ci bésub njàqare.

¶ Ba bët setee Yawut ya daje, daldi xasoo, ne duñu lekkati, duñu naanati, ba kera ñu reyee Póol.