1 Kings 1:12
TSK
Kaay gaaw, ma digal la nooy def, ba musal sa bakkan ak sa bakkanu doom Suleymaan.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Kaay gaaw, ma digal la nooy def, ba musal sa bakkan ak sa bakkanu doom Suleymaan.
Yaa ma berndeel, noon yi gis, nga diwal ma saa bopp, terale ma, saab kaas rembat.
dugub di ko dooleel, biiñ di bégal xolam, ag diw di leeral kanamam.
Lal ba, ma xeeñal, mu ne bann, di ndàbb, cuuraay ak xas mu neex.
Ki rafet xel mooy kiy ràññee, te su wax rafetee, dég-dég yomb.
Wax ju yiw di lem juy xelli, neexa ñam, di jàmmi yaram.
ndax kat nun nooy cuuraayal Almasi fa Yàlla, ñeel ñi ci yoonu texe, ak ñi ci yoonu sànkute.