¶ Xale yu góor ya mu màggandool ne ko: «Mbooloo mii ne la sa baay da leena gàlloon buumu njaam gu teeŋ, waaye yaw yolomalal leen ko; li nga leen di wax mooy lii: “Sama baaraamu sanqleeñ moo gëna diis sama tànku baay.
TSK
TSK · Proverbs 28:16
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
1 Kings 12:10
TSK
Nehemiah 5:15
TSK
Waaye boroom diiwaan yi ma jiitu dañu daan not askan wi, di leen sëf seen dund ak seen biiñ, boole ci ñeent fukki dogi xaalis. Seeni surga it di néewal askan wi doole. Man nag defuma noonu ndax ragal Yàlla.
Ecclesiastes 4:1
TSK
Ma seetlooti gépp notaange gu am fi kaw suuf. Ndeke néew-doolee ngi jooy, amul ku ko dëfal. Ki koy not a am doole, te néew-doole ji amul ku ko dëfal.
Isaiah 33:15
TSK
Xanaa kiy doxe njekk, di wax njub, bañ alalu foqati; loxo bay jalax ab ger, noppam di tanqamlu waxi bóome, bëtam di gëmm, ba du gis lu bon.
Amos 4:1
TSK
Dégluleen kàddu gii, yeen jigéeni tundu Samari, yeena ngi suur ni nagi diiwaanu Basan. Yeen ñiy torxal néew-ji-doole, di not aji ñàkk te naan seeni jëkkër: «Indil ñoll waay, ñu naan!»