TSK

TSK · Proverbs 30:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Job 42:3 TSK

Nee nga ma: «Ana koo doon, bay lëntal samay dogal te xamoo?» Maa wax moos te xawma lenn ci kawtéef yu ma wees, ump ma.

Booba ngaaka laa, xawma dara; rab laa woon fi sa kanam.

Nga naan: «Su ma yégoon, sopp ab yar te baña sofental waxi àrtu.

Nitoo nit dim sannax, sore xam-xam: te képp kuy tëgg sa jëmmu tuur, yaa añe gàcce. Sa jëmmi weñ ji nga xelli, di neenug neen, noog bakkan, tus!

¶ Bu kenn nax boppam: Ku teg boppam ci yeen, boroom xam-xam, ni xarnu bii jàppe xam-xam, kooku na doon ab dof, ngir am xam-xam bi wóor.

James 1:5 TSK

¶ Ku desele am xel mu rafet nag, na ko ñaan Yàlla, mu may ko ko, ndax Yàlla mooy yéwéne ñépp te du sikk kenn.