TSK

TSK · Psalms 55:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Te sax ku may topp ku dul yaw, doomu buur? Ni ma toppe woon sa baay rekk laa lay toppe tey.»

Wallóoy, Aji Sax ji, ngor jee na! Kóolute réer na doom aadama.

Mooy yónnee fa asamaan, musal ma, dumaal ma ku may not. Selaw. Yàllaay yónnee jëfi ngoram ak wormaam.

Xanaa dungeen bàyyee songandoo nit, nar koo sànk, ni kuy màbb tabax bu joy, mbaa ngay bàddi per mu ràpp?

Lu mel ni lem la ndaw su yemadi di wax, làmmiñ wa ni diw gu ñu lay raay.

Ab noon làqoo na ay waxam, lal pexey wor ca xolam.

Kuy fen, dangaa bañ ka nga fenal, te boroom làmmiñ wu neex day sànke.

¶ Ba mu ko defee ñu bàyyi Yeesu xel, daldi yebal ay yeerukat, sas leen ñu yiw-yiwlu te di ko fiir ci kaw kàddu ba jàpp ko, ngir jébbal ko boroom dëkk bay boroom kilifteef ga ak sañ-sañ ba.