TSK

TSK · Romans 5:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Teewul mbooloo ma ne ko: «Déedéet, yaw doo ànd ak nun! Ndax nun su ñu nu dàqee, du am boobu solo. Bu sunu genn-wàll deeyee it, du am benn solo. Waaye sa jenn jëmm jii mooy fukki junni ci nun. Kon nag desal nu ci dëkk bi, di nu fi yónnee wall, moo gën.»

Daawudaa nga ca biir rawtoom. Mu am kurélu xareb Filisteen ñu dal Betleyem.

Ñoom ñoo jaay seen bakkan ngir ma mucc, te du man doŋŋ maa leen ameel njukkal, waaye mboolooy gëmkat yu jaambur ñi dul Yawut yépp a leen ameel njukkal.