TSK

TSK · Ruth 3:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Bu ay góor yu bokk waajur dëkkee, kenn ci ñoom dee te bàyyiwul doom ju góor, jabaru ki dee du génn, di séy akub jaambur. Jëkkëru donaleem ju bokk ak jëkkëram moo ko wara jël, donloo ko.

Ruth 2:20 TSK

¶ Nawmi ne Ruut: «Yal na Aji Sax ji barkeel Bowas, moom mi saxoo sàmm ngoram digganteem ak nit, muy dund ak mu dee!» Mu teg ca ne ko: «Kooku ku nu jege la; bokk na ci ñi am sañ-sañu jotaat nu.»

Ruth 4:6 TSK

Mu ne: «Kon de duma mana def sama warugar, ndax sama alal a ciy yàqoo. Fabal boog sama sañ-sañu jotaat, ndax duma ko mana jariñoo.»

¶ Nit nag, ku ko sut lay giñe, ngir dogal kàddu, ba teesal wépp werante.