TSK

TSK · 1 Kings 21:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Daawuda nag ne Rekab ak Baana, doomi Rimon waa Berot ba: «Giñ naa ci Aji Sax ji, Kiy Dund te musal sama bakkan ci gépp njàqare,

¶ Ba loolu amee jabaru Uri dégg ne jëkkëram dee na. Mu daldi koy ténj.

Daawuda jekki-jekki xel ma sore. Mu ne: «Éy ku ma wutali woon ndox mu ma naan ca teenu Betleyem ba ca buntu dëkk ba!»

Fu ngeen gis ub sàcc, neexook moom, ab njaalookat, ngeen lëngool.

Waruleen woona seetaan ci seen bésub mbokk, bésub njekkaram, Waruleen woona bége deminu Yudeen ñi ci seen bésub sànkute, mbaa ngeen di réy làmmiñ, ci bésub njàqare.

Ba ñu wàccee yoon wu jub wi lañu lajj topp yoonu Balaam, doomu Bosor, mi soppoon peyooru njubadi.