TSK

TSK · 1 Kings 21:24

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ku Yerbowam deele ci dëkk bi, xaj yi lekk; ku ca médd ca àll ba, njanaaw ya for. Aji Sax ji wax na ko.”

Yaw, ñu xañ la bàmmeel, sànni la, nga mel ni car bu ñu foñ. Yaa ngi ne lareet ci biir néew yu saamar bóom, ñu tàbbal leen ci xeeri biir kàmb. Yaa ngi mel ni médd mu ñuy joggati.

Maa lay wacc fi suuf, sànni la ci àll bi, dëël njanaaw yépp fi yaw, ba reggal rabi àll yépp ci saw yaram.

ndax ngeen lekk suuxi buur ak suuxi njiiti gàngoor, suuxi jàmbaar ak suuxu fas ak gawaram, suuxu ñépp; gor ak jaam, mag ak ndaw.»