TSK

TSK · 1 Samuel 13:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ci kaw loolu mu tànn ñetti junniy nit ci Israyil; ñaari junniy nit ñuy nekk ak moom ca Migmas ak ca tundi Betel, ak junniy nit ñu nekk ak Yonatan doomu Sóol ca Gibeya gu Beñamin. Ña ca des mu yiwi leen, ñu ñibbi seeni xayma.

¶ Ci fan yooyu Yonatan doomu Sóol wax surga ba koy gàddul ngànnaayam, ne ko: «Kaay nu dem ba ca gàngooru Filisti ga ca wàlla.» Baayam nag, waxu ko ci dara.

Daawudaa nga ca biir rawtoom. Mu am kurélu xareb Filisteen ñu dal Betleyem.

jaare ca xunti ma te naan: «Geba lanuy fanaani!» Waa Raama tiit, waa Gibeya gu Sóol daw.