1 Samuel 14:23
TSK
Noonu la Aji Sax ji maye Israyil ndam bésub keroog, xare bay law, ba ca wàlla Bet Awen.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Noonu la Aji Sax ji maye Israyil ndam bésub keroog, xare bay law, ba ca wàlla Bet Awen.
¶ Waa Filistee boole woon seeni gàngoor ngir xare. Ñu daje ca dëkk ba ñu naan Soko ca diiwaanu Yuda, daldi dale ca Efes Damim diggante Soko ak Aseka.
seen geño sakkan ni suuf, di seen meññeefu biir, tollook feppi suuf, du dog, du sànkoo fi sama kanam!
«Yeena ngi gànctu, yeen bànni Israyil, waaye na Yuda mucc ci googu tooñ. Buleen dugg Gilgal, buleen yéegi Bet Awen di giñ ci Aji Sax jiy dund.
Waa Samaree ngi am tiitaange ci sëllu wu ñu xelli ca Bet Awen, askan wa di tiislu tuur ma, ay xërëmkatam di lox ndax darajay sëllu, ji leen dëddu, dem ngàllo.