TSK

TSK · 1 Samuel 25:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Naka lañu génn dëkk ba, te soreeguñu sax, Yuusufa sant fara biir këram, ne ko: «Gaawal dab gaa ña, te boo leen dabee, wax leen ne leen: “Lu tax ñu ji leen njekk, ngeen feye ngoreedi?

Job 30:8 TSK

Ñu sew lañu, ñu kenn yégul, xanaa caw leen, génne réew mi.

Baal mer, dëddu xadar. Xol bu jóg, loraangey neen.

tance ma kàdduy mbañeel, song ma ci dara.

Lu baax dees na ko feye lu bon a? Moona gasal nañu ma am yeer, di ma tëru. Bàyyil xel ba may taxaw fi sa kanam, di leen tinul ngir nga moyale leen sa mer.

Buleen mer ba bàkkaar, te bu jant bi sowe seen mer;

Fexeleen ba kenn du feyantoo. Waaye lu baax, deeleen ko deflante ci seen biir, te di ko defal ñépp.

Lu bon, buleen ko feye lu bon; ay saaga it, buleen ko feye ay saaga. Xanaa ngeen ñaanal leen, feye leen ko, ndax ci loolu lees leen woo, ngir ngeen jagoo barke.