TSK

TSK · 2 Corinthians 13:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

ci turu Sang Yeesu. Bu ngeen dajee, te ma bokk ak yeen teewe ko samam xel, ci sunu kàttanu Boroom Yeesu,

Tiiñal, gi ko li ëpp ci mbooloo mi tiiñal, doy na ko mbugal.

¶ Danuy tàmbaleetee seedeel sunu bopp ne noo yelloo ngërëma? Am danoo soxla ni ñenn nit ñi, ay bataaxal yu jëm ci yeen, mbaa mu bawoo ci yeen, ngir seedeel nu ngërëm?

Te doonuma am benn kersa, su ma ëppaloon sax ci damoo sañ-sañ bi nu Boroom bi jox, te du sañ-sañu sànk leen it, xanaa yokk seen ngëm.