Mise ne: «Soo délseek jàmm déy, Aji Sax ji waxul, ma jottli.» Mu dellu ne: «Mbooloo mi, yeena ko déggandoo, yeen ñépp.»
TSK
TSK · 2 Corinthians 13:8
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Alyaasa bàyyikoo fa, jëm Betel. Ma nga topp yoon wa di dem, ay gone jóge ca dëkk ba, di ko ñaawal, naan ko: «Boroom nel, ca kaw! Ée boroom neleey, ayca ca kaw!»
Ñaan-yàlla, soo tooñul, du la dal, day mel ni picc muy naaw, tëë toŋ.
Noonu it lañu sottale mboolem li nga dogale woon sa loxo ak sa coobare.
Ba loolu amee ñu woor, boole kook ñaan, daldi leen teg seeni loxo, ba noppi yiwi leen.
ci turu Sang Yeesu. Bu ngeen dajee, te ma bokk ak yeen teewe ko samam xel, ci sunu kàttanu Boroom Yeesu,
Looloo tax ma bind leen lii bala maa dikk, ba buma dikkee, du jar may mettil ni may jëflante ak yeen, ci kaw sañ-sañ bi ma Boroom bi jox. Ndax kat sañ-sañ bi, yokke moo ko taxa jóg, waaye deesu ko yàqe.
ana kon nun ci sunu bopp, nan lanuy rëcce mbugal, su nu sàgganee pexem mucc mu réy mii Sang bi jëkkoona biral, te ñi ko dégg dëggalal nu ko?