TSK

TSK · 2 Kings 2:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Musaa woo Aji Sax ji wall, Aji Sax ji won ko dammitu bant, mu sànni ko ca ndox ma, ndox ma neex. Foofa la Aji Sax ji dogalal bànni Israyil ay sàrti yoon ak ndigal, te fa la leen nattoo itam.

Alyaasa ne: «Indil-leen ma sunguf.» Ñu indi, mu xëpp ca cin la, daldi ne: «Sottil-leen mbooloo mi, ñu lekk.» Ba loolu amee dara lu aay amatul ca cin la.

Mooy soppi wali ndox màndiŋ, soppi bëti ndox suuf su ne sereŋ,

Mooy fomp seen wépp rongooñ: Dee dootu am, dëj aki yuux aku tiis dootu am, lu jëkk laay wéy.»