TSK

TSK · 2 Kings 7:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Surgaam ya nag dikk, kenn ca ñoom ne ko: «Baay Naaman, su doon lu jafe la la yonent bi wax ndax danga ko dul def? Kon kay su la nee nga sangu rekk, set wecc, nga war koo def!»

Su nu demee ca biir dëkk ba, danuy dee ak xiif. Su nu toogee fii itam, dee ak xiif. Kon kay nan dem ca dalub waa Siri, jébbal leen sunu bopp. Su ñu nu bàyyee, nu dund, baax na. Su ñu nu reyee it, nu dee rekk.»

Ña saamar rey a gënu demin ña deeye xiif, jeex tàkk, ne lasar, ndax ñàkk meññatum tool.