TSK

TSK · 2 Peter 3:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Yàlla ne: «Na aw dénd dox diggante ndox yi, ngir xàjjale leen, yii fii, yii fale.»

Moo samp suuf biir géej, dëj ko ci kaw wal mi.

Moo lal suuf ca kaw ndox ma. Kee saxoo ngoram!

Mooy ki nekkoon naka jekk balaa daraa nekk, te lépp ci moom la sottee ba temboo.

¶ Ngëm a nu xamal ne Yàllaa sose àddina wërngal këpp ag kàddoom, li gisu daldi sàkkoo ci lu gisuwul.