TSK

TSK · 2 Samuel 10:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ku dul doomu yoon du bokk ci ndajem gëmkati Aji Sax ji. Ku askanoo ci moom it, ba ca fukkeelu maas ga, du bokk ci ndajem gëmkati Aji Sax ji.

Daawuda bàyyikoo fa dem Mispe, ca diiwaanu Mowab. Mu wax buuru Mowab ne ko: «Rikk may ma, sama baay ak sama ndey dikk toog ak yaw, ba ma xam nu Yàlla di def ak man.»

¶ Bésub keroog jàng nañu ci téereb Musaa, mbooloo ma di dégg. Ñu gis ñu bind ca ne, muy Amoneen, muy Mowabeen, kenn du ci bokk ci ndajem bànni Israyil mu ñuy màggale Yàlla, ba fàww.