TSK

TSK · 2 Samuel 13:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Bul dëkkoo sab jigéen, te muy koo bokkal benn baay mbaa koo bokkal jenn ndey, muy ku juddoo ci kër gi mbaa feneen.

Soxnaam Yesabel dikk ne ko: «Lu la tax ne fóññ nii? Lu la teree lekk?»

Waaye loolu lépp doyu ma, li feek maa ngi gis benn yoon Mardose, Yawut bi, mu toog ca buntu kër buur.»

Ñu wara am gàcce ci seen jëf ju siblu, te gàcce gàcceelu leen. Xamuñu sax luy kersa! Moo tax ñuy fëlëñoondook ñiy fëlëñu. Kera ba ma leen di dikkal, ñooy tërëf.» Aji Sax jee ko wax.

¶ «Buleen ragal dara, yeen jur gu sew gi, ndax seen Baay la soob, mu jagleel leen nguur gi.