TSK

TSK · 2 Samuel 14:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Natan ne Daawuda: «Yaw, yaay waa ji! Aji Sax ji Yàllay Israyil dafa wax ne: “Man maa la fal buurub Israyil, maa la xettli ci Sóol.

Ba Absalom dawee, dem Gesur, toog na fa ñetti at.

Luke 7:42 TSK

Waaye ñoom ñaar ñépp, kenn manu cee fey. Mu far jéggal leen ñoom ñépp. Ana kan ci ñaar ñooñu nag moo ciy gëna fonk leblekat bi?»